text
stringlengths 38
33.7k
|
---|
ey aji sax ji , loo deeti seetaan ? musal ma ci seen um padd , wallu ma ci yii gaynde , |
xoolal bu baax te wax ma ku moom jaarob mandargaal , bi and ak buum gi , ak yet wi . yudaa xammi yef ya nag , ne moo ma gena nekk ci degg de , gannaaw mayuma ko sama doom sela . gannaaw ba loolu weyee , andatul ak moom . |
ndokklee kuy dimbalikoo yallay yanqooba di yaakaar yallaam aji sax ji , |
mboolem reew ya feete dexu efraat sowu . jamm ne noyy , feete ko wet gu nekk . |
baatu xale ba ci kuy namp , feenal nga ca sa kattan , banaaleek feyukat ne xerem . |
jot ab yegle ci yeneen addu yiy new joti yegle ci adduy jukki bii ci e bataaxal way bindu rekk la neel nag xibaaryi . com ab dal la site buy tas xibaar ci wolof , mu di lakk wi nu gen a wax ci senegaal . |
4 neegub yaxantu bu lislaam bi ak mecce ak joqalanteg njaay yi |
ontologsi l ontologie mbaa xam xamu am bu xalaatu nit ku nuul ku afrig mandargaalees na ko ni ko meetar wadd wonee ca xalaatu jemmam ba sa physicite . |
bu dawalee paaka ba sidit ya tambalee dagg mu teggi ko kon bu ko ca gaawee delloo dees na ko lekk , bu ko ca yeexee delloo nag te lor wara lu ko kon deesu ko lekk . |
ba mu waxee ba noppi , loot dafa xool , gis joor , gi wer dexu yurdan gepp , mandi ndox . ndax laata aji sax jiy tas dekk yu nuy wax sodom ak gomor , all bi jem sowar dafa naatoon , ni reewum misra naate , ba faf mel ni toolub aji sax jal . ba mu ko defee loot tann jooru yurdan gepp , daldi toxu jem penku . noonu lanu teqlikoo . ibraam dekke reewu kanaan , loot sance dekk ya ca jooru yurdan , daldi toxal xaymaam , samp ko sodom . waaye waa sodom nu bon lanu woon , te mana moy aji sax ji lool . |
yeesu dékku na ay nattu ci pexey seytaane |
mussolini feenal na mbonam gi ak mbonug langam gi , jaare ko ci jefam yu naaw yi mu jemale woon ci askanu libi wi , ba mu fa beggee samp sancug itaali gi . |
noonu yeesu jóg topp ko moom ak ay taalibeem |
fa la fekk keroog ab jawrinu sool bu yitte teye woon fa aji sax ji . mooy edomeen ba nuy wax doweg njiital sammi sool la woon . |
xellees na koo xelli ci neen , taxul li ci bon genn . |
def say leeral fu woor ak caabiy firefox os , man mani sutura ak yeneen mbir . |
damaa wara dem ci yeneen dëkk yi ngir yégle xibaaru jàmm bi ci nguuru yàlla ndaxte looloo tax ñu yónni ma |
leneen nag wadd ci biir ay xaaxaam xaaxaam yi daldi jóg tanc ko |
moo tax sama xol sedd may woy sama bànneex te it sama yaram di tëdd ci yaakaar |
bi ci des di bi ñu tax a jug moom nag adab la nu laaf ci ag l muy leegi ladab lu tax nu laaf ci l gi loolu ñi ngi ci roye lislaam te bu njëkk islaam la woon waaye ginnaaw ak l gi la ko wolof yi di gën a man di wax ak a tudd moo waral ci li nu wax nu koy boole ci baatu araab bi lii nag làkk woo gis ci àdduna bi am na ko boo demee ci araab da cee fees dell ay baay yu nu lem ba manees koo wax ci làkku araab te doonuñu woon ay baati araab ñu mujj bokk ci làmmiñu araab te bu njëkk bokkuñu ci woon |
moytul bépp jataayu waxi neen yu àddina kese ndax ña fa toog dinañu gëna xuus cig weddi te seen kàddu day burux ni ngal |
nee na dafa amoon cib dekk , benn attekat bu ragalul yalla te faalewul mbindeef . |
ba besu juroom benneel ba jotee , danoo for lu mat naari njel , ku nekk am naari andaar , njiiti mbooloo ma nag dem yeggeji ko musaa , mu ne leen |
réew moomu mbaa suuf soosu moom na boppam walla deet mbaa ñu yamale yengu yëngoom |
ba mu ko defee daawuda dem , mook juroom benni teemeeri nit na and ak moom . nu dem ba ca xuru besor , nenn na yem fa . daawudaa nokkli , mook neenti teemeeri nit , naar teemeeri nit yem foofa , ndax loof , ba manunoo jall xuru besor . ci kaw loolu na jall yem ci jenn waayu misra ci all bi . nu indi waa ji ba ci daawuda , daldi may waa ji mburu mu lekk , may ko ndox , mu naan . ab danku figg ju wow ak naari danki resen lanu ko leel , mu doora leqliku , ndax dafa fekk lekkul , naanul diiru netti guddi ak netti becceg . daawuda ne ko yaw , kuy sab sang ak foo bokk ? xalelu goor ba ne ko |
saxal yu jataay bi ñi ngi ame ci ndollant gu toll ci juroom ñeenti kàddu ci cosaanul fukki kàddu ak juroom maanaam saxal gi du man a wér mbaa mu wéy ndare bu juroom ñeent danoo kàddoo waaw la ca des ne deet walla ñu noppi |
fi njarin li gen a feenee sax mooy seddaleeb dawaan bu safaanu bir na ne moo gen a yaxan dawaan bu wey ci seddaleeb dend bu kawe nakkug kattan gi ci buum yu gudd yi moo gen a neew . |
waxees na ma te loolu lu wér la ne rakkam ja sheex ibra faati ci bis bi sëñ bi tukkee ba bi mu dellusee masul a dañ di def junniy salaatu alan nabii ci melo wii |
amoon na bés yawut ya yónni ay sarxalkat ca yaxya ñu ànd ak ñu soqikoo ci giiru lewi ñu nga jóge yerusalem ñëw ci moom di ko laaj mooy kan |
doom joo jure ndaw , mooy fitt ci loxol jambaar |
aji sax ji , lepp loo sakk a lay gerem , sa wollere yi di la sant , |
bi ndaje moomu weesoo lañu ko féetale xaaj bu mu war a bind ci cosaanu waa isipt yu yàgg ya |
leegi nga xam ne bindu nga ba noppi , man ngaa dugg ci samay tanneef soppi ko ci ni nga ko beggee . |
moo leen di kepp seen naawteef , sanke leen seen ug mbon . |
gannaaw metitu bés yooyule nag ca saa sa jant bi dina lëndëm te weer wi dootul leer |
ci kaw loolu robowam agsi yerusalem , daldi woo waa ker yudaa gepp , nook giirug benamin . nu tollu ci teemeer ak juroom nett fukki junniy nit , diy neyi xare . nu nara xareek israyil , ngir delloo leen ci nguuru robowam doomu suleymaan . |
ndax tekkina ay jëff actes ay gis gis vision mbaax valeurs ak ay mbir yuñu don nee ci maam yi la moo waral mu lëntt |
ndaxte xamunu sax naka lanu wara ñaane yàlla waaye xelu yàlla maa ngi nuy ñaanal fa moom ak i yéene yu làmmiñ manta takk |
tur wii nuy wax jolof , benn soose bu tundoon jolof mbeng moo ko joxoon dekk ba . |
maanaam xamug àdduna ci wàllu yar ak teggin ak xam xam yewwute gu nit ñi ci aw askan |
lii moo tax daanaka du xeetu jurukaayu mbëj bu ñuy faral di jëfandikoo ci digg yu mbëj yi bu demandoo lañuy jëfandikoo |
te it li ko yalla dekkal , ba mu banatee jaar ci dee , te suuf du ko lekk mukk , moom la yalla wax ne dinaa la may barke yu sell te woor , yi ma digoon daawuda . |
noonu bokk yi yebal pool ca saa sa mu jëm géej waaye silas ak timote des fa |
aaroona dikk ba ci sarxalukaay bi , rendi sellu wi , muy saraxu pootum bakkaaram . gannaaw loolu doomi aaroona yu goor ya indil ko deret ja , mu capp ca baaraamam , taqal ca bejjeni sarxalukaay ba la des ca deret ja mu tuur ko ca taatu sarxalukaay ba . aaroona jel nebbon bi joge ci sarax biy pootum bakkaar , ak i dembeenam ak bajjo bi ci res wi , mu boole ko lakk ci kaw sarxalukaay bi , muy la aji sax ji santoon musaa . yapp wi ak der bi , mu genne ko dal ba , lakk ko , ba mu dib doom . la ca tegu aaroona rendi juru rendi doomal bi . ba loolu amee doomam yu goor ya jox ko deret ja , mu xepp ko ci mboolem weti sarxalukaay bi . nu jox ko saraxu rendi doomal bi nu |
taalibeem yi ak mbooloo mu bare ànd ak moom |
ci lu jem ci anoci kureel gi karim wadd jiite woon , nee na itam , odite kureel googu nga xam ne lu tollu ci miliyaar ci xaalis dugg nanu ci , lu war la , lu menula nakk . |
bi loolu amee ñu toog fa ab diir ba noppi bokk yi yiwi léen ci jàmm ñu dellu ca ña léen yónni woon |
loolu nag amoon na ginaaw bi kolomboo feeñalee aamerig ba am lu tollook xarnu |
g . manees na koo tekkee nii it bay feesal suuf aku ay . |
ndaxte yiwu sunu boroom yeesu kirist umpu leen ni mu futtee am amam ba ñàkk ngir yéen ndax ngeen woomle cig ñàkkam |
waaye bu jekker ji faatoo , yoon jeexal na seen diggante man na sey nag ak beneen goor , te loolu du njaaloo . |
ba tey soxla taxul ma waxe nii ndaxte jàng naa doylu ci mbir mu ma mana dab |
na ngay boole yitte ji jepp ci li ngay sakku , ci lu dul gestu jem ci lu warul . |
gannaaw def nga loolu , yaw rekk ay alku ci rabi ker yepp ak rabi all yepp dinga watu , di lekk pend sa giiru dund gepp . dinaa def mbaneel sa digganteek jigeen ji , ba deddale sa xeet ak xeetam , muy toj sa bopp , nga di ko matt ci testen . |
benn bes caat ma ne baay ba baay , damaa beggoon , nga jox ma li may war a feetewoo ci ndono li . |
man ci sama bopp soxlawuma seedes nit waaye nag damay wax loolu rekk , ngir ngeen mucc . |
ñu takk doj wu réy ci baatam sànni ko ci géej moo gën ci moom muy daaneel ci bàkkaar kenn ci ñi gëna tuuti ci ñii |
coppite yi neel wall nikaraaguwa wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii . |
yonent bu jigeen ku maggat lool la woon . |
booy yóbbu nag sa sarax ca sarxalkaay ba te nga fàttaliku foofa ne sa mbokk am na lu mu la meree nanga fa bàyyi sa sarax ca kanam sarxalkaay ba nga jëkka dem juboo ak sa mbokk ba noppi dellu joxe sa sarax |
bu nopp ba xaree lu toll ci benn ci ñatti xaajam du mat am tabaski |
xanaa du ci seeni begg begg , yiy xeex ci seeni cer ? |
bii seddatlin nga xam ne kureelu mbootaayu xeet yi sax mooy la jefandikoo suy seddatle adduna bi ci ay diwaan , gestukat yi noom seddatle bu bees bi la nu taamu , moo xaaj oseyaani ci naari diwaan oseyaani gu jege ak oseyaani gu sori yi polineesi box . |
maa ngii di dakkal ci bii berab , ngeen teewe , fekke lepp luy coowal mbegteek banneex , boroom seet ak seetam selaw . su ko defee , boo waxee askan wii kaddu yooyu yepp , nu ne la ana lu waral aji sax ji dogalal nu musiba mu rey mii mepp ? ana fu nu toone ak fu nu moye sunu yalla aji sax ji ? nga wax leen nag ne leen seeni maam a ma wacc , kaddug aji sax jee , di topp yeneen yalla , di leen jaamook a sujjootal . man nag , nu deddu ma sama yoon it , nu ban koo samm . yeen nag , ngeen di bon , ba raw seeni maam . yeena ngii , ku nekk te ticc , topp xolam bu bon , ban maa deggal . maa leen di daqe ci reew mii , jeme reew mu ngeen xamul , seeni maam xamunu ko , ngeen di fa jaamu guddeek becceg yeneen yalla , ndax dootuma leen baaxe . |
wolt mu itaali mi di ki wone duusi mbëj yi te fent batari |
tukuloor ak seereer danuy kalante ak joolaa tam . |
jigeen ji toj njaq li , tuur latkolon ci boppu yeesu . |
aji sax ji waxati musaa , ne mu wax banni israyil , ne leen kepp ku jabaram moy , fecci ko worma , bu nu andee ak ndaw si , te moom miy jekkeram yegu ko te ba ndaw say sobeel boppam , fekkeesu ko fa ba di ko seede ndegam xelum fiiraangee dikkal waa ji , ba mu fiire jabaram , te fekk jabar jaa sobeel boppam ci njaaloo , mbaa muy fiiraange gu dikkal waa ji rekk , mu fiire jabaram , te fekk ndaw si sobeelul boppam ci njaaloo na waa ji yobbu jabaram ca sarxalkat ba , te yobbaleel ko saraxu netti kiloy sungufu lors . du ci sotti diw , du ci def cuuraay , ndax saraxu pepp boobu saraxu fiiraange la , saraxu toppukaay la bu nuy toppe naawteef . |
mayuma jigeen , muy jangale mbaa muy jiite goor , waaye na noppi . |
muni ko aaah ! yaw de xanaa fii lala taw bi fekk . |
yaram wi soloo ndamu xelum yalla jiituwul yaramu doom aadama moo jiitu yaramu ndam li moo ci topp . |
dawalal sa njambaar , neel efrayim ak benamin ak manase , te wallusi nu . |
nees di wacces ndaw , si nga takk ba ngay ndaw ? sa yallaa ko wax . mu ne maa la wacc diir bu gatt , dellu la jel ci yermande ju yaa . |
buuru yudaa ne ko aji sax ji dafa wax ne maa ngii di teg dekk bii ci loxol buuru babilon , mu taal ko . yaw cedesyas nag doo ko recc . dees na la japp moos te dees na la teg ci loxol buuru babilon , mu wax ak yaw , seeni get neent nga dem babilon . |
maa ban kuy topp tuuri neen . man , aji sax ji laa woolu . |
ba diir ba leen buur appal matee , nu war leena indi , kilifag jawrin ya yobbu leen fa kanam buur nabukodonosor . buur wax ak noom te gisul ci noom nepp kenn ku mel ni daneel ak anana ak mikayel ak asaryaa . nu daldi tabbi ci liggeeyu buur . mboolem wallu xam xam ak xel mu leen buur seetlu rekk , gis ne noo ci sut fukki yoon taryaax yeek neengokati reewam mepp . |
bi yeesu waxee la mu naroona wax lépp ca kanam mbooloo ma mu daldi dem kapernawum |
bokk na ci li mu bind ñeel abuubakrin ibnu fatan ci mbirum lii bismil laahir rahmaanir rahiimi yal na yàlla dolli xéewal ci sunu sang muhammad ak ñoñam aki saabaam ag xéewal akug mucc gog da na ci xamal nit ñi ne la aboobakrin bun fatan waxoon ci waxi seex tiijaan ji jubluwu ci woon sheex tiijaan y y g te moom sheex y y g dëppoo na ak moom aboobakrin ci mbooleem li mu wax ci tontoom yi |
mayees ko it sañ sañ ci kaw bépp giir ak réew ak kàllaama ak xeet |
waaye nag ci geneen wàll am na lu am njariñ lu mu fa indi ndaxte wàññi woon na limub diiwaan yu almaañ yi ba ci fanweer ak juroom ñeent rekk te bu njëkk lu jege 360 lañu woon |
ca fan yooyu mu daanu wopp , ba faatu noonu nu sang ko , teg ko ca neeg , ba sut ca taax ma . |
lii nag mooy seen kemu bej gannaar . ca geej gu mag ga ngeen di redde , ba ca tundu or , redde ko fa tundu or , mu jem lebo amat , jall ba cedadd , weyeeti fa , jaare sifron , jem accar enan . loolooy seen kemu bej gannaar . |
goornamaab doxaliin bi sampu na atum 1895 moom nag li mu doon wund mooy ab diggante bu tuxu nekk ci diggante jamonay tiital ak taral ak jamonoy nguurug imbraatoor gu nu joyal gu tar goo xam ne napoliyon bonaparte moo ko ame woon ci ginaaw bi ci bi mu fi nekkee |
man nanu koy jang ci injiil ci mc mk lu yow . |
maanaam , ni baay bi di dekkale nu dee ni , di leen jox dund , noonu la doom ji di joxe dund ni mu ko begg a jox . |
nguuri pël yi ca jamono yu yàgg ya li ëppoon ci giirug pël ay sàmm yu daa màng lañu woon di tuxu ci seen bëgg bëgg ngir wër ndox ak ñax ñu nekkoon di ñu tasoon ci gox yu bari ci sowwu afrig la ko dale ca dexug senegaal ba ca ngéejus càdd lac du tchad |
ngir yokk kaarange gi , sandarma yu cees yonnee nanu fa seeni ay non ngir nu aar bereb ya . |
waaw ma naan ko mais feebar ba taxul mu bàyyi mu daldi may roof sëqët ba ñu ne dama tuberculose |
bi nuy yeemu ci li mu doon def , yeesu ne taalibeem ya |
danoo sakku rekk nu aar sunuy xale , bu nu beggee xam li ci sey , nanu jaar ci yoon wu sell , ak ci at yu jaadu , la ci teg . |
gisiin wii nga xam ne amul woon geneen jublu gu feeñ gu dul dëgëral xeltug ngérum ne ne philosophie materialiste nekkoon na di lu safaanoo ak gisiinu big bang wi saxaloon ne àdduna bi am na ag tàmbali |
ca ba muy jeexal , serin addu na jeme ci njiit yi , bu mu ci men a doon , di leen fattali li leen war ci li taqook seenug ndombo tank . |
juroom neenti xasab la , di neenti meetar ak genn wall , yaatuwaay ba , neenti xasab , di naari meetar . |
dangeen a war a mun , ba def coobareg yalla , sog a jot li mu leen digoon . |
ndaxte yàlla sàkk na bés bu muy wone àtteem bu jub bi te meram wàcc ci ñi bon |
ba loolu amee mu ne jaraafam ba nuy wax bitkar foral sanni ci toolub nabot mu yisreel . yaa ngi fattliku ba nu bokkee watiir maak yaw topp ca |
booba am la nu waxoon jaarale ko ci yonent yalla yeremi , bi mu naan |
buur , li nga gis kenn ci wattukat yu sell yi wacce asamaan , addu ca kaw ne |
yeewe seeni buur ay callala , jenge seeni njiit jengi wen , |
waawaaw ci li ay àtte yees nangu ci jëmm lois phisique wax jëmmi ceññeer yu leer yi bu ñuy tuxu jëm ca tombub seetlu ba dañuy jeng jëm ci yolet te jëmmi ceññeer yu leer yiy dem di sori tombub seetlu bi dañuy jeng jëm ci xonq |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 39