audio
audioduration (s)
0
198
text
stringlengths
0
3.82k
start_time
float64
0
3.02k
end_time
float64
0.33
3.03k
nawet bi door na ndax taw yu njëkk yi gis nañu leen ba tax na projet :fra bii di ECHO moo leen ciy gunge ci ay émission :fra yu am solo émission :fra yi nag ñu ngi ciy ànd ak ñi nga xam ne seen xam-xam dafa màcc jëm ci wàllum mbéy état :fra bi maanaam nguur gi ràñ~ee leen lool nag ci mel ni waa DRDR ANCAR institut :fra naional :fra de :fra pédologie :fra waa CNAAS di nañ ciy waxtaanee ci thème :fra yi nga xam ne dina yitteel loolu béykat yi ci li nga xam ne moom mooy nawet bi ndax dinañ ci waxtaane la :fra fertilisation :fra et :fra la :fra consevation :fra des sols :fra maanaam daal naka la ñuy toppatoo suuf si ba mu ñu mën cee am mbéy mu mucc ayib dinañ si waxtaanee tamit les :fra déficits :fra pluviométriques :fra et :fra de :fra la :fra manière :fra s' :fra y :fra adopté :fra maanaam néew gi nga xam ne taw bi dina ko néew ak naka la ñuy mën a def ngi mën a ànd ak moom dinañ ci waxtaanee les :fra ravageurs :fra qui attaquent :fra des :fra cultures :fra maanam daal yi nga xam ne dañuy yàq mbéy mi dinañu waxtaanee ak béykat yi nu ñuy mën a def ba moytu loolu waaye danañ waxtaan tamit les :fra conservations :fra des :fra récoltes :fra maanaam daal naka la énuy toppatoowee li nga xamante ne moom mooy li ñuy béy waaye nag mbokk yi ñu ngi leen di xamal ne émission :fra bu njëkk bi ñu ngi ko jàpp àllarba ñaar fukki fan ak juróom-ñaar ci weeru juin :fra bu 17 heures :fra ci ngoon jotee maanaam mercredi :fra 27 juin :fra à :fra partir :fra de 17 heures :fra fii ci Louga FM RTS yéen nag mën ngeen cee bokkagum bu ngeen wootee ci li nga xam ne moom mooy serveur :fra vocal :fra bi ci 33 869 74 02 33 869 74 02 ngeen mën a bàyyi seen tur seen sant ginnaaw bi ngeen déggee bip :fra bi wax tamit li nga xam ne moo leen titteel su ko defee suñu ndax dana leen mën a indi ay leeral may fàttali àllarba bii di ñëw yemoog ñaar fukki fan ak juróom-ñaar ci weeru juin :fra à :fra partir :fra de :fra 17 heures :fra fii ci Louga FM RTS di émission :fra bi nga xam ne dinañ ci àndak ku xam-xamam màcc jëm ci wàllu mbéy mu bokk nag ci institut :fra national :fra pédologie :fra kon nag mbokk yi seen émission :fra baa ngi noonu bu leen ko kenn nettali jërëjëf mbokk yi ci %e déglu bi ngeen di déglu Louga FM RTS comme :fra ni ñu leen ko annoncer :fra woon tey jii nag di %e émission :fra bu njëkk di émission :fra bi nga xam ne moom la leen waa ECHO di jagleel xam ngeen ni bande :fra annonce :fra bi mu ngi doon daw waaw fan yii yëpp nag tey jii ñu am mbégte ak bànneex %e dalal ki nga xam ne xam-xamam dafa màcc jëm ci wàllup %e jëm ci suuf si mbéy mi climat :fra bi yooyu yëpp day dinañ ci %e waxtaan ndax tey jii thème :fra bi nga xam ne moom la ñu jël moom mooy %e fertilisation :fra et :fra gestion :fra durable :fra des sols :fra loolu nag %e moom mi nga xam ne moom mooy invité :fra bi dana dana dana ñu ko faram fàcceel xanaa rek %e du ñu si sori ndax wolof Ndiaye nee na tungune du teew ñuy nataal dañ koy daal di nuyu rek moom Pape Gora Kane su ko defee rek mu daal di nuyonteeg mbokku auditeurs :fra yi ba noppi nag gën ñoo présenter :fra boppam ndax %e wolof Ndiaye nee na loo xam Mademba Mademba gën laa xam boppam Pape ñu ngi lay nuyu
0
147.223
%e salaamaaleykum %e monsieur :fra monsieur :fra Amady Ba maa ngi lay fay di %e nuyu tamit sa auditeurs :fra yi ñuy déglu %e di leen baalu àq ci weeru koor biñ jógee te tamit %e di leen di leen baal di ñaan yàlla %e bépp jaamu yàlla bu nga xamante ni def nañ ko si yàlla %e nangul ñu ko ah xam naa nag %e man maa ngi tudd %e Pape Gora Kane nekk assistant :fra %e délégué :fra zonal :fra bu institut :fra national :fra de pedologie :fra institut :fra national :fra de :fra pédologie :fra nag dafa nekk %e benn bànqaassu ministère :fra de :fra l' :fra agriculture :fra bu nga xamante ni moom mooy saytu wàll suuf yi %e saytu bi jëm ci wàll di leen aar %e ba pare bu amee ay yàqu-yàqu ci suuf si ñoom ñoo koy jéem a jooyanti maanaam dégradation :fra des :fra sols :fra yi dañ koy xeex bu baax %e fii ci Louga ak li ko wër ñu naan ko %e zone :fra pédoclimatique :fra sylvopastoral :fra et :fra Niayes institut :fra national :fra de :fra pédologie :fra mi ngi fi nekk %e commune :fra Kell Guèye yaakaar naa yaakaar naa ñi miin %e yoonu Dakar bi avant :fra ngay dugg Kell di nga gis benn batimat :fra bu ne foofu batimat :fra bu orange :fra foofu la %e institut :fra national :fra de :fra pédologie :fra nekk
147.223
219.531
%hum %hum
219.531
219.893
en :fra meme :fra temps :fra tamit am nañu ay buraux :fra DRDR maanaam mooy agriculture :fra gu Louga %e xam naa bu delloo ci *
219.893
228.723
%e mooy %e voilà :fra léegi nag pour :fra dugg ci %e waxtaan bi xam nga thème :fra bi dañ ne fertilisation :fra et :fra gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra tey boo ñu ko doon faram facceel %e thème :fra bi lan la
228.723
238.801
waaw xam naa monsieur :fra Ba ma lay remercier :fra bu baax %e thème :fra bi nag dafa nekk %e thème :fra d' :fra actualité :fra parce :fra que :fra li ñuy naan gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra dafa %e nekk lu nga xamante ne tey àdduna si yëpp daanaka ci la ñu dox %e si buñ ko bëggee tënk daal ci lu gàtt maanaam fertilisation :fra dafa dugg sax ci biir gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra
238.801
260.955
%hum %hum
260.955
261.474
mais :fra nag dinaa gën a ñëw ci fertilisation :fra
261.474
263.825
%hum %hum
263.825
264.353
mais :fra gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra moom bu énu ko déggee mooy %e bépp xeetu doxalin bu nga xamante ne day dajale lépp lu nga xam ne dafay dellu si aar suuf yi %e ak ndox yi ak %e bépp meññeef bu nga xamante ne day jugee ci aalam bi %e ba pare %e day may %e béykat bi day may béykat bi %e mu yokk njëriñ li nga xamante ne moom lay jëlee suuf si ci suuf si te du ko lor
264.353
292.022
%hum %hum
292.022
293.053
bon :fra xam naa nag %e donc :fra fertilisation :fra moom dafa dugg ci gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra ndax %e fertilisation :fra mooy bépp xeetu technique :fra bu nga xamante ni %e béykat bi da koy jëfandikoo pour :fra jo() dolli suufam ay ferñeent loolu mooy ferilisation :fra
293.053
311.405
d' :fra accord :fra donc :fra ba tax na %e laaj bu njëkk bi ginnaaw bi nga faram fàccelee li nga xamante ne moom mooy %e thème :fra bi waxtaan bi tey daénu ne %e état :fra suuf si naka la mën a affecté :fra rendement :fra bi nga xamante ne moo am ci culture :fra bi %e suuf si xam nga %e wax nga léegi ba ne %e ni nga xamante ne noonu la énu ko mën a taxawoo daal ngir %e béykat bi mën cee am njëriñ léegi nag man li ma bëggoon laaj mooy suuf si ci boppam naka la ñu ko war a mën a taxawee daal ba mu indil li nga xam ne moom mooy njëriñ ci béykat bi
311.405
339.452
%hum %hum ah oui :fra jërëjëf %e sëñ Ba xam naa question :fra boobu moom am na solo trop :fra puisque :fra %e suuf moom comme :fra ni ñu koy faral di waxee rek moom mooy support :fra production :fra
339.452
351.875
%hum %hum
351.875
352.375
bu ñu nee état :fra wu suuf si naka la mën a %e affecté :fra ci %e maanaam %e rendement :fra béykat bi
352.375
360.076
%hum %hum
360.076
360.463
loolu dafay dellu juste :fra ci fertiliser :fra suuf si xam naa %e foofu noonu man dama koy jéem a pour :fra simplifier :fra suñu auditeurs :fra yi ñiy déglu pour :fra mu bañ a %e xaw a technique :fra de trop :fra
360.463
371.79
%hum %hum
371.79
372.188
danu jël diggante %e nit maanaam yaay ak doom jigéen bu am doom bu ñu jàppee ni jigéen ji moom mooy suuf
372.188
381.514
%hum %hum
381.514
382.013
doom ji moom mooy gàncax bi lépp lu nga xamante ni %e doom ji mi ngi koy soxla pour :fra nàmp ci yaay ji la koy jëlee léegi bu dee yaay jooju moom mi ngi ànd ak wér %e ànd naag wér day mën a nàmpal doomam bu baax te du am benn gàllankoor mais :fra bu dee yaay ji dafa manqué :fra par :fra exemple :fra soow
382.013
403.193
%hum %hum
403.193
403.673
du munul nàmpal doom ji noonu la gàncax bi mel ak suuf lépp lu nga xamante ni daal gàncax daf koy jëfandikoo daf koy jëlee ci suuf ferñeent yëpp ci suuf la koy jëlee
403.673
415.727
%hum
415.727
416.157
donc :fra %e ci %e wàllu mbéy dañuy faral di wax ñiy jàng agronomie :fra am na terme :fra bu ñu tuddee exportation :fra peut :fra être :fra tey jii nii comme :fra damay ragal ñi ma ñi ma ñi ma ñi ma war a summi summi ma
416.157
430.145
%hum %hum
430.145
430.557
mais :fra man comme :fra dama bëgg ñebe bu dee dañu béy %e toolu ñebe
430.557
434.56
%hum %hum
434.56
435.131
jël ñebe ji dem jaayi ko Dakar
435.131
437.133
%hum %hum
437.133
437.638
%e xam nga buñ jëndee ñebe ñu ci bëri dañ naan ñebe dafa riche :fra en :fra fer :fra
437.638
442.583
%hum %hum
442.583
443.22
wala dafa réer ci yeneen ferñeent yi nga xamante ne dañ koy jëfandikoo di ko lekk léegi ferñeent yooyu noonu ñebe ji ci suuf si la ko jëlee %hum bu dee yow man dama am sama tool chaque :fra at ma ciy béy ñebe
443.22
455.895
%hum %hum
455.895
456.495
di jël ñebe ji di ko jaayi Dakar
456.495
458.662
%hum %hum
458.662
459.091
di jël ngooén mi di ko dem yóbbu sama kër
459.091
460.915
%hum %hum
460.915
461.512
donc :fra ferñeent yooyu nekkoon ci suuf si maa ngi leen di jël di leen yóbbu Dakar ferñeent yi nekkoon ci suuf maa ngi leen di jël di leen stocké :fra sama kër léegi nag bu dee chaque :fra année :fra damay def lma :fra même :fra chose :fra damay dem ba sama suuf
461.512
473.867
%hum %hum
473.867
474.167
dootul amati dara ci wàllu ferñeent %e léegi comme :fra suuf moom comme :fra ni ñu ko xamee rek bu ma %e jëlee benn échantillon :fra suuf jël ko yóbbu ko laboratoir :fra par :fra exemple :fra analyser :fra ko da ngay gis ni suuf énetti pàcc moo ko composé :fra
474.167
491.943
%hum %hum
491.943
492.383
maanaam am na liñ naan partie :fra minérale :fra bi
492.383
494.794
%hum %hum
494.794
495.247
am partie :fra organique :fra bi am beneen partie :fra bu nga xamante ni c' :fra est :fra %e gazeux :fra kooku moom mun nañ cee bañ a dugg
495.247
501.33
%hum %hum
501.33
501.745
mais :fra li ma ci gën a interessé :fra mooy partie :fra organique :fra bi
501.745
504.49
organique :fra bi
504.49
505.242
partie :fra organique :fra boobu noonu moom la %e ferñeent yi ne ci suuf si
505.242
509.566
%hum %hum
509.566
509.963
loolu moo leen concerné :fra directement :fra foofu la ñu jugee léegi ferñeent yooyu noonu nekk ci suuf sm na lu énu naan les :fra éléments :fra majeurs :fra mooy NPK bi ngay dégg ñu koy faral di am ci ñu koy faral di wax ci engrais :fra yi léegi bu delloo ci %e NPK boobu N bi moom azote :fra la moom mooy permettre :fra croissance :fra su garab gi P bi di phosphore :fra xam naa dinañ ci gën a dellu si si kanam moom mooy permettre :fra développement :fra garab gi K bi moom mooy %e potasium :fra moom moom pour :fra couvertir :fra %e ferñ() %e nu mu tudd meññeent yi jugee ci %e meññeent yu jugee ci garab gi lay lay lay gën a dëgëral
509.963
551.045
%hum %hum
551.045
551.402
ak lu ñu naan les :fra oligo :fra élément :fra yooyu yëpp xam naa dinañ ci dinaén ci ñëw ci kanam léegi yooyu noonu bu ci manqué :fra rek dafay affecté :fra dooley suuf si énu ko naan fertilité :fra du :fra sol :fra
551.402
562.252
%hum %hum
562.252
563.173
loolu mooy loolu mooy définir :fra fertilité :fra du :fra sol :fra éléments :fra yooyu ma udd ak yeneen des na yeneen ak yeneen
563.173
568.445
%hum %hum
568.445
568.83
yooyu mooy définir :fra fertilité :fra du :fra sol :fra
568.83
570.953
%hum %hum
570.953
571.39
léegi
571.39
572.341
%hum %hum
572.341
572.701
bu dee éléments :fra yooyu dafa manqué :fra suuf si day manqué :fra doole
572.701
575.968
%hum %hum *
575.968
577.197
am na tamit yeneen paramètres :fra yu nga xamante ne peut :fra être :fra dinañ ci gën a xuus ci kanam mais :fra énu jàpp daal ci tënk ni éléments :fra yooyu ma lim ak yeneen
577.197
584.43
%hum %hum
584.43
584.869
ñoom ñooy définir :fra dooley suuf
584.869
586.739
waa léegi li nga wax ni ley définir :fra dooley suuf léegi producteur :fra bi nag moom naka la mën a njëriñoo
586.739
592.013
%hum %hum
592.013
592.27
%e suuf si nga xamante ne ci lay ci la ci lay béy ndax wax nga sànq ci sa biir wax ba joxe exemple :fra ne su fekkente ne da ngay ji par :fra exemple :fra ñebe bu loolu defee at bu jot nga jaayi ji ko Dakar wala nga denc ko sa kër dana dem ba am loo xamante ne dana ko manqué :fra ci tool bi foofu mu ne léegi nag moom %e béykat bi naka la war a mën a def nag ba di jëriénoo suufam ba saa yu ko soxlaa rek fekk fa ferñeent yi nga xam ne war naa nekk ci suuf si
592.27
612.132
%e jërëjëf %e sëñ Ba xam naa ci côté :fra boobu noonu li ci gën a %e am solo mooy d' :fra abord :fra nga tànn
612.132
622.017
%hum
622.017
622.497
%e suuf si ngay bayee dafa am solo
622.497
626.446
%hum %hum
626.446
626.981
parce :fra que :fra comme :fra ni ñu koy waxee rek
626.981
628.953
%hum %hum
628.953
629.376
dëgg la %e béy moom gàncax foo ko ji bu amee condition :fra yu mu soxla dana sax mais :fra nga choisir :fra %e en :fra fonction :fra li nga bay suuf si mu méngool loolu am na solo trop :fra pour :fra am rendements :fra yu baax loolu benn la ci ba pare tamit %e di dundal maanaam di fertiliser :fra di yokk sa suuf doole di ko amander :fra dinañ ñëw ci différence :fra fertilisation :fra amandement :fra lan la dinañ ci ñëw ci kanam loolu tamit %e dafa am solo
629.376
665.755
%hum
665.755
666.434
%hum bon :fra %e waaw xam naa %e
666.434
671.075
nga wax ñu ci ci ci ci ci ci ci tànn wi suuf si maanaam da nga ne tànn bi am na solo
671.075
674.838
%hum %hum
674.838
675.345
%e mais :fra même :fra tànn bi
675.345
676.517
%hum %hum
676.517
676.923
ndax du %e ku ne rek moo mën a tànn
676.923
678.656
%hum %hum
678.656
679.073
ndax tànn bi mën ngaa baaxee auditeurs :fra yi nga xam ne ñu ngi ñuy dégl
679.073
682.044
%hum
682.044
682.444
%e naka la ñuy tànnee %e par :fra rapport :fra ak fi nga xamante ne moom moom moom la ñu war a ji
682.444
687.166
waaw
687.166
687.584
%hum %hum
687.584
688.098
%e ci loolu noonu bu dee ñun zone :fra bi ñu nekk nii muy zone :fra %e sylvopastorale :fra Niayes
688.098
694.147
%hum %hum
694.147
694.467421
%e di ëmb Louga ak li ko wër
694.467421
697.145
%hum %hum
697.145
697.816
%e bu ñu seetloo liñ fiy gënal faral di béy
697.816
700.581
%hum %hum
700.581
701.127
moom mooy %e ñebe
701.127
703.531
%hum
703.531
704.066
dugub
704.066
705.24
%hum
705.24
705.6
gerte ak %e mboq
705.6
708.434
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
34