bilalfaye/nllb-200-distilled-600M-wolof-french
Translation
•
Updated
en
stringlengths 1
298
| wo
stringlengths 1
279
⌀ | fr
stringlengths 1
687
|
---|---|---|
Take my guests out. | Yobbu samay way wuyusi yi. | Sortez avec mes invités. |
You're the Führer. | Yaay Führer bi. | Vous êtes le Führer. |
Who's your horse? | Kan mooy sa fas? | Qui est ton cheval? |
If one runs away hit her with it and call her name. | Kenn ci ñoom daw, nga dóor ko, nga woo ko turam. | Si l'un d'eux s'enfuit, frappez-la avec et appelez-la par son nom. |
Get back to work you lousy bastard. | Dellu ci sa liggéey, yaw nit ku soxor ki. | Retourne au travail, espèce de salaud. |
This is my ancestral home, how can I leave it? | Lii sama dëkku maam la, naka laa koy bàyyi? | C'est ma maison ancestrale, comment puis-je la quitter? |
You'll go blind! | Di nga nekk gumba! | Tu vas devenir aveugle! |
You've had a bad time... | Danga dundu lu metti... | Tu as passé une mauvaise période... |
All right? | Baax na? | - Je suis désolé. |
I'll have to leave a trail of breadcrumbs every time I come in. | Saa yu ma duggee dama wara bàyyi mburu mu ñor. | Je devrai laisser une traînée de miettes de pain à chaque fois que je rentrerai. |
- All right. | - Baax na. | - Ça va aller. |
Sometimes it takes me a while to remember where I am. | Yenn saa mu may yàgg balaa may fàttaliku fi ma nekk. | Parfois, il me faut un moment pour me rappeler où je suis. |
Oh! | Oh! | Je suis désolée. |
Lasse is here. | Lasse moy fii. | Lasse est là. |
My son is a demon. | Sama doom jinne la. | Mon fils est un démon. |
Return to your cell blocks for evening count. | Dellu ci sa selil ngir lim ci guddi gi. | Retournez dans vos cellules pour le décompte du soir. |
THE BICYCLE THIEF | SÀCC WELO BI | Le voleur de vélo |
Mom. | Yaay. | - Je suis désolée. |
What are you doing, boy? | Xale bi, looy def? | Tu fais quoi, petit? |
Careful. | Moytu. | Attention à vous. |
That's it! | Loolu la! | C'est tout! |
Where? | Fan? | - Où? - Dans le coin. |
A promise I made to Andy. | Dige buma defoon Andy. | Une promesse que j'ai faite à Andy. |
They have proved themselves too weak and it is a law of nature that they will be exterminated. | Dañu wane ni dañu néew doole lool, te yoonu nature dafa wax ni dina ñu leen jeexal. | Ils se sont montrés trop faibles et c'est une loi de la nature qu'ils seront exterminés. |
That just happens to be exactly what I'm looking for. | Loolu mooy li ma doon wër. | C'est exactement ce que je cherche. |
Charter fishing. | Napp charter. | La pêche à la location. |
That's a sure-fire way. | Loolu yoon wu wóor la. | C'est une façon sûre. |
Not like here. | Du ni fii. | Pas comme ici. |
Why's that? | Lu tax loolu? | Pourquoi? |
Why not? | Lunu yeesal yeesal? | Pourquoi pas? |
You can be sure he'II prove... | Mën nga gëm ni dina firndeel... | Vous pouvez être sûr qu'il prouvera... |
Don't let it get you down. | Bul ko bàyyi mu gëna jeexal sa xol. | Ne vous laissez pas abattre. |
There's still men buried. | Ba leegi amna góor ñuñ suul. | Il y a encore des hommes enterrés. |
Maybe I should get me a gun and rob the Foodway, so they'd send me home. | Amaana dama wara jël fita ngir sàcc Foodway bi, ñu yóbbu ma seen kër. | Je devrais peut-être me procurer une arme et voler le Foodway, pour qu'ils m'envoient chez moi. |
You have to keep your eyes peeled for her. | Danga wara bàyyi sa bët ci moom. | Tu dois garder les yeux ouverts pour elle. |
Ricci? | Risi? | Vous êtes Ricci? |
They are your people. | Sa askan lañu. | Ce sont tes gens. |
Do you have kids? | Am nga ay doom? | Vous avez des enfants? |
He does not give me to eat. | Du ma jox lu ma lekk. | Il ne me donne pas à manger. |
I pissed blood for three days. | Ma siiwal deret ñatti fan. | J'ai pissé du sang pendant trois jours. |
And we are never going into the woods again. | Te dunu musa dem ci àll bi. | Et nous n'irons plus jamais dans les bois. |
- It's not my problem | - Du sama jafe-jafe | - Ce n'est pas mon problème. |
- Why don't you use your retirement to...? | - Lu tax doo jëfandikoo sa retrete ngir...? | - Pourquoi ne pas utiliser votre retraite pour... |
He's falling! Hang on! Don't let go! | Mu ngi daanu! Xaaral! Bul ko bàyyi! | Il tombe, ne lâchez pas! |
You selling a handlebar? | Yaa ngi jaay guidon? | Vous vendez un guidon? |
Take it. | Jël ko. | Je vous en prie. |
This from the West Land's best hunter? | Lii ci rëbbkat bi gëna baax ci West Land? | Ça vient du meilleur chasseur de l'Ouest? |
Sounds like you done time all over New England? | Daa melni def nga ay jamono ci New England yépp? | On dirait que tu as fait ta peine dans toute la Nouvelle-Angleterre. |
Another coffee? | Beneen kafe? | Un autre café? |
All prisoners report for Lockdown. | Kaso yépp war nañu dem ci Lockdown bi. | Tous les prisonniers se présentent pour le confinement. |
She'll come back then she'll know who's boss. | Dina dellusi suko defee mu xam kan mooy patroŋam. | Elle reviendra et saura qui est le patron. |
That little sack of shit? .? | Sac bu ndaw boobu? .? | Ce petit sac de merde? |
WENDY: | Wendi: | Je suis désolé. |
It's big, but it ain't nothing but a kitchen. | Dafa rëy, waaye du lenn ludul waañ. | C'est grand, mais c'est une cuisine. |
Go ahead. | Ayca. | - Je vous en prie. |
Oh, dear! | Oh, sama xarit! | Je vous en prie! |
Here it is. | Leegi la. | - Le voilà. |
I'll have to go to the authorities and report you and keep your wages. | Dama wara dem ci kilifa yi ngir delloosi la te baña fay sa xaalis. | Je vais devoir aller voir les autorités et vous dénoncer et garder votre salaire. |
Damn you, always complaining. | Damn you, saa yu nekk dangay ñaxtu. | Vous vous plaignez toujours. |
who have been through similar traumatic experiences... that the following moments kind of feel like you're moving kind of in slow motion. | ñi dundu lu mel noonu ci jafe-jafe yu mel noonu... saa yu ci topp dañu melni dangay yëngu ndànk. | qui ont vécu des expériences traumatisantes similaires... que les moments suivants semblent se déplacer en ralenti. |
You were away eight years before. | Jiroom ñatti at ci ginaaw yaa ngi woon. | Tu étais parti huit ans avant. |
I'm outlining a new writing project. | Maa ngi waajal projet bind bu bees. | Je suis en train de dessiner un nouveau projet d'écriture. |
Zihuatanejo, huh? | Ziwatanejo, wala? | Tu es un vrai Zihuatanejo. |
I win. | Dama jël ndam li. | Je gagne. |
Tonight you may not sleep too well... but tomorrow the bike'll be back. | guddi gi mën nga nelaw bu baax... waaye suba bi velo bi dina dellusi. | Ce soir, vous ne dormirez peut-être pas très bien... mais demain, le vélo sera de retour. |
It paralyzes the nerves and the respiratory system. | Dafay gàllankoor neer yi ak sistemu noyyig bi. | Il paralyse les nerfs et le système respiratoire. |
Don't let go until I say so. | Bul bàyyi ba ma wax ko. | Ne lâchez pas avant que je le dise. |
I could shoot the manager, while I was at it. | Mën naa tiire bal kilifa gi, fekk maa ngi ci liggéey bi. | Je pourrais tirer sur le gérant, en même temps. |
I just saw her taking a guava and who knows what else? | Dama ko gis muy naan guayave, kan moo xam lu ci des? | Je l'ai vue prendre une goyave et qui sait quoi d'autre? |
Is Ricci there? | Ndax Ricci mingi fa? | Ricci est là? |
It's up to them to get paid | ñoom ñoo wara fay | C'est à eux de se faire payer. |
Why should I kill myself worrying when I'll end up just as dead? | Lu tax ma wara ray sama bopp di jaaxle ndax dinaa mujjee dee? | Pourquoi me tuer en m'inquiétant quand je finirai aussi mort? |
Your father can stand on his own two feet. | Sa pàppa mën na taxaw ci ñaari tànkam. | Ton père peut se tenir sur ses deux pieds. |
The horse's head on the butcher's has lost an ear. | Boppu fas wi nekk ci boppu yàpp bi ñàkk na nopp. | La tête de cheval du boucher a perdu une oreille. |
Folks around this joint love surprise inspections? | Nit ñi wër bii dañu bëgg saytu surprise? | Les gens autour de cette joint aiment les inspections surprises? |
Him? | Ko? | - Il? |
He wants me to starve. | Dafa bëgg ma xiif. | Il veut que je meure de faim. |
I'm so sorry, sir. | Maa ngi lay massawu. | Je suis désolée, monsieur. |
You are the Führer. | Yaay Führer bi. | Vous êtes le Führer. |
- What's your name? | - Nan nga tudd? | - Quel est votre nom? - Je m'appelle... |
eighth from the front. | juróom ñatteel ci kanam. | huitième de l'avant. |
Yeah. | Waaw. | - Je sais. |
Blood? | Der fees? | - Le sang? |
A lot of this stuff you'll never have to touch. | Lu bari ci mbir yii doo musa laal. | Tu n'auras jamais à toucher à beaucoup de ces trucs. |
The Russians are breaking through everywhere. | Waa Russie dañu dugg fépp. | Les Russes font des percées partout. |
I have more. | Amnaa yeneen. | J'en ai encore d'autres. |
Much obliged, sir? | Dama wara def, seigneur? | Vous êtes très reconnaissant, monsieur? |
Are you deaf? Come on! | Ndax tëx nga? Gaawal! | Vous êtes sourd? |
- All right? | - Baax na? | - Ça va? |
This is a charter from the Mikado allowing us to subdue the Deer God! | Lii charte la bu bawoo ci Mikado bi nuy may nu noot Yàlla Deer bi! | C'est une charte du Mikado qui nous permet de soumettre le Dieu des cerfs! |
In a place like that, I could use a man who knows how to get things? | Ci barab bu mel nii, mën naa jëfandikoo nit ku xam ni ñuy jëlee mbir yi? | Dans un endroit comme ça, je pourrais utiliser un homme qui sait comment obtenir des choses? |
Toki was right! | Toki dëgg la wax! | Toki avait raison! |
Okay? | Baax na? | - Je suis désolé. |
Yeah, I've been in and out since I was 13. | Waaw, damay dugg ak génn bima amee 13 at. | Oui, j'ai été dans et hors depuis que j'ai 13 ans. |
Five months of peace is just what I want. | Juroomi weer ci jàmm mooy li ma bëgg. | Je veux cinq mois de paix. |
Who is it? | Kan la? | Qui est là? |
Don't worry. | Bul jaaxle. | Ne vous inquiétez pas. |
All your wages, Erik. | Sa saleer yépp, Erik. | Tout votre salaire, Erik. |
Don't be nervous. | Bul jaaxle. | Ne soyez pas nerveux. |
A man searches for a woman at Earth's top and finds her. | Benn góor dafa wër benn jigéen ci kaw suuf si, daal di koy gis. | Un homme cherche une femme au sommet de la Terre et la trouve. |